Русские видео

Сейчас в тренде

Иностранные видео


Скачать с ютуб BIG DAT X - RIP в хорошем качестве

BIG DAT X - RIP 2 года назад


Если кнопки скачивания не загрузились НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу страницы.
Спасибо за использование сервиса savevideohd.ru



BIG DAT X - RIP

Auteur: Big Dat X Titre: RIP Enregistrement/Mix/Master: MeloMusic Entertainment Artwork: BBoss ——————————————————— Disponible sur toutes plateformes de streaming : https://BigDatX.bfan.link/rip-mojo ——————————————————— Contacts Management: [email protected] /+221 781105992 ——————————————————— Suivez moi: Facebook 👉🏾   / big-dat-x-marxabane-team-650660248375778   Instagram👉🏾 https://instagram.com/bigdatx_loffici... —————————————————— Lyrics Rap égal rythme ak Poetry Clash mooy ku la wokk nang ko xuri Wow Wow ana sa tontu budul tànn ceeb bi Da ngay freestyle wala sa xaru bee ñor tabbi Sa Beat bi daa nice même mélodie yaa ngi may cokkotaan Mais Lyrics Yi !! Hon HOn !! xet u pokkotaan Càmbay Rap bi di ndiro’og Baara Mbay bëkëtë No doubt bul koko jàpPee De c'est que Rap bee ko të Càmbay Da ngay juum ba puup si rap bi ding ko tònni Xiiru rek nga mën sakaja makaja Càmbay After Mojo JOJO amzo Zozo Fii ñëpp dañ la sexlu miss BANAYA Càmbay Juutu Kaolack Juutu Thies ak Guédiawaye Boo desul si Fen Prod sa nëbuu( bun) bee gën a yaa M Mandaari Macc kat Mën Meew amu si Mappandoo O Orgasme Ordure Origine be’y ubeeku Out J Jàgg bu Jon bi Jëriñul Jarul Di jooy Jugul O Ordinaire Dat dey jollu mooy Oxymore Waga bi dikkaat jël téggin bi tege nee Coup de rein si sa kaw Maman mooy Remise au Point G Fanaawu Bakaawu waxma ku dee numuy xaroo Jaay sa bopp si Real Soldier Yewwi tax jaroo Dat easily beat bi laay teg dila kokëlli hey si cuuc nga yam matagoo cocori Fi nga dal ñaar ngay am Mort ou Chichi Lyrical waga bi liko jaaxal du ay wax i picc yii KL maitriser kamasutra ndax rhyme yi lay tëddee Alaa Accu sip nga beat bi litax ñufay fëllee Bajjen buy xaar tama fajar nee ko dese woo ndaw Dina diis lool si moom pour mu àggee ko waa Ndar gu ndaw Champ de bataille mësu ma fa jog Fa laa daaj banc Ngay xànju missile malay xaar ngamay door ay balle à blanc Okey !! Assi yakkal si Menu pour enfant Le PPS ou l’Alien pour zigam teg’u si temps Man Ròmb naa la maa ngi dem si Bine Fall Eeh Bine fall bine fall Defal ma Mo Jën Ma dolli si siim ndax da cere Te ki fi doon commander emcee moom laay reeree Son bi sa Tombe la RIP Mi proud to be me no matter whata Gwan Mi na wrong widema talk no matter whata gwan Hey jap bi gën di garaaw ever seen si lama jëm Sniper si rhyme viser fumu ne ma Jam Yàgg a deg daaj u marteau yàgg a deg daaj u brin Style wagga dëgg wagwan dey fëkk sa brain Dem a di rude boy but mi di phenomenal Mi bombacklate dem like duty crazy criminal Ndax niggers dati X la avion si piste la kii yakkate sa organisme ni feebar u peste la Positive si mind like benn Malcom X la Big dikk ak big dick fuck si mojo X la #bigdatx #rip #hiphop #rapgalsen #senegal

Comments